Posts du forum

Jigéen Jàambar
17 déc. 2020
In SANTÉ MATERNELLE ET INFANTILE
1- LA NOUVELLE LES PERSONNAGES: Bajén, la tante du mari Jeukeur Ji, le mari Ndaté, la femme enceinte Atta, l'amie de Bajén Coura, l'amie de Bajén Bajén tok ći ëttë keur gui ći kaw bassang gui gadu lékétam di araw. Atta ak Coura da di gaddu lékétu natt bi. Bajén ak ay xaritam dadi lang waxtaan. Nékélañu tamballi rék, Ndaté da di dougoussi di mél ni kouy sox and ak Jeukeur Ji. Bajén, sigui xol ko mel ni koukoy sénatou: Ey li! Biir mom dou fébar wakh ća deug deug. Xalé bi moune na watni louko xouri mou gadou yobou hôpital. Xalissam bi yeup yemna ći emb xalé bilé. Yal n'a am sax loumouy ngénté bou ko yalla méyé mouthieu. Atta, dadi gersu Bajén: Ey li! Biir mom dou fébar wakh ća deug deug. Jeukeur ji dadi joubal ći nékba, Ndaté di dém tok ći bang bi nék ći wétouma Bajén. Bajén, dadi défarou: Wa Ndaté dém nga ba ñieuw. Ba dou dara rék? Dom dia ngići diam? Ndaté, da di talal tankam yi: Waw, dém na ba ñieuw. Sage femme bi néna ma wañi yénou lou diss ak seug bou beurri. Baxoul ći xalé. Ndaté da di diafanu ći garab gui nék ći wétam ndax mou moune diouk. Ma ngi dém ći bir dadi dalou touti Badiéne. Baćil kalam sou néxé yalla. Badiéne, da di ko xol mouy dox dieum ći négam: Wa baxna. Xol léne ko. Ay morom rék ñio fi eumb ba weussine di rôtti, yénou ak taxañi mom néna dañieu koko téré. Dieul bir rék fass yéné ko déf problème. Sama dom gui rék la ći yeureum. Dina féy hôpital loumou défone ći campagne kani gui yép. 2- L'AFFICHE 3- LA VIDÉO: THÉÂTRE DE SOCIÉTÉ 4- LA VIDÉO DE SENSIBILISATION DE LA MAITRESSE SAGE-FEMME: LA VISITE PRÉNATALE 5- LA CASE SANTÉ: LE CHALLENGE
JÀABARU ORDONNANCES - UNE FEMME À ORDONNANCES content media
0
0
11

Jigéen Jàambar

Administrateur
Plus d'actions